Accéder au contenu principal

KENEEN NEW SINGLE DE ELZO JAMDONG AVEC PAROLES

Le nouveau single tant attendu de ELZO JAMDONG est disponible
KENEEN prod by mister thiere.
ENJOY LISTENING

LYRICS
bignu ande ba legui dane gua sone gnuy dound lou mety sa tank dane meti dane gua sokh wayé taxoul gua tegi mousso ma togn moussoma diss liga ame ci ngor moussoumako guiss moussoma note meussoma dinguate suba ak ngone louma nior gua guiss
yaye sama gaïne sama miss sama star sama way sama queen sama love barigua yare teksi diné ak tare yaye sama guaïne sama miss sama staaar sama miss sama star yaye sama way sama queen sama looooove barilégua yare teksi diné ak tare mak ioe la boudoul ioe dou done kenen(×3) lignu thiow yeup boudoul ioe dou done kenen bobou bagui legui magui try wayé menouma xol fénéne mani bobou ba legui gnugui fight mayé menouma dem fenen mak ioe la boudoul ioe dou done keneeen(×2) bignu andatoul ba legui magui dokh ci taly menouma diegui sama tank dina newi magui sokh wayé takhoul ma tegui moussoma togn moussoooma diss liga ame ci ngor moussoumako guiss moussoma lore té moussoma dinguate sama xol tay amna guome ci bire yaye sama gaïne sama miss sama srar sama miss sama star yaye sama way sama queen sama loooove barigua yare teksi diné ak tare yaye sama nite yaye sama niiiite mani yaye sama nite douma bayi douma tite mak ioe la boudoul yow dou done kenen mak ioe la boudoul ioe dou done keeeneenn(×3) lignouy thiow yeup boudoul yow dou done keneeen bobou ba legui magui try wayé menouma xol feeeeneeene mani bobou ba legui magui fight wayé meunagouma dem fenene mak ioe la boudoul ioe dou ioe done kenen(×3) maguini si loula nekh bess nek dagay bess melni gnogui doga tambalii_ii té xamguani dou diekh kon waro meussa deglou gnilay wakh gnun niar dotoul amatiii mani melgua noula nekh bess bouné dagay bess melni gnogui dogua tambaliiii-ii kon wargua xamni man ak ioe dou diekh boul deglou gnilay tegal ni man ak ioe dotoul amatiiii yaye sama nite yaye sama niiite mani yaye sama nite douma bayi douma tite.
#rpgalsen
#skj

Commentaires

Posts les plus consultés de ce blog

DIP DOUNDOU GUIS

VOICI LE TEASER du clip de DIP Laff en featuring avec Dop Boy sortie prévue le DIMANCHE 15 OCTOBRE 2017. WAIT IT #rpgalsen #skj

LE CLIP Dara Safatouma de JAY avec paroles

CLIP LYRICS #rpgalsen #skj

TOUT SAVOIR SUR AKHLOU BRICK PARADISE

Biographie AKHLOU BRICK PARADISE est un groupe de rap composé de jeunes sénégalais qui évoluent depuis plusieurs années dans ce domaine. Le groupe voit le jour en 2007. ‘ ’Mist’Ara’’, et ‘’Day Za Colour’’ adorent la musique depuis qu’ils etiez petits. Ils décident de fonder le groupe pour vivre de leur passion. Ils ont une conception alternative du rap et un attachement indéniable à leur indépendance artistique. L'éclectisme est leur éthique musicale, mais aussi celle de leur vie. Musique solide, consistante, avec une attention toute particulière portée à l'écriture. Histoires parfois incisives, poignantes, amusantes, leurs lyrics sont dessinés à coup de poésie et de philosophie bien balancée. Se lâcher et surtout ne pas se prendre la tête, un grand sourire puis laisser le charme agir. Puisqu’il n’a jamais eu du rap typiquement fait de leur localité, il décide de représenter MBOUR dans le mouvement du hip hop galsen(sénégalais). Apres la sortie de nombreux sons, c’est leur...